Daara J Family — Bayi Yoon şarkısının şarkı sözleri ve çevirisi
Sayfa, Daara J Family adlı sanatçının "Bayi Yoon" şarkısının sözlerini ve Türkçeye çevirisini içeriyor.
Şarkı sözleri
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes
Fier d'être africain je suis, j’suis africain donc je suis
Mes ancêtres ont souffert le martyr pour que je puisse relever le défi
C’est à moi de porter le flambeau ils ne peuvent pas me mettre en lambeau
Pour me mettre KO il faut minimum une armée de cent mille rambots
Dis à ton prof d’histoire qu’il raconte des histoires
La plus grande des civilisations est née en Afrique noire
L’Afrique a inspiré le monde avec ses pyramides, sa science, ses mathématiques
Ses symboles et ses signes
Elle créa l'écriture avec les hiéroglyphes du temps des pharaons
Tu ne me crois pas?
Vas-y, demande à Akhenaton. (de Dakar à Marseille)
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes
Dafa melni gnou ngi daw jeum fenen ni wacc wacc nagnou ande yi xeeb sougnou
ngande yi fekki borom jikko you dande yi
Fo daw fo daw di nga wirri ndaari fa nga jouge fi nga doore fila woore doufou
sorre
Afro sama dole na nga mako xole geum sama demb doon nittou tey njaxass ni
xeetou parfum’k’gowe
Africains koula xass foy gnawe
Africains xola gneup nignouy ngaange
Africains soy joug doufi gawe
Koula xol dina seet fan la lay ngagne
Geum sa bopp xam fi nga bokk melni garab reen banxass ak xob
Dougnou fatte fignou joge ndakh panafricanistes delo sougnou xel demb kanamou
mame gnou giss
Dimbali jam yi biss- gnoul metisses dekkil osiris -carbone14 souliwaat gnou
giss- histoire bindaat grand pere ba petit fils
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes
Bamako ! Singapour ! Anghata !
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Nenaala sama gaa gna ngi
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi !
Şarkı sözü çevirisi
Sama gaa GNA ngi
Doomu Afrika mbeur La kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala Sama gaa GNA ngi
Ana soutoura bifi GNOME mame bayiwoon
Jikko sen rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
GNOME wakh için ki nga doon oh ! Ooh !
Afrikalılar ve kim olduğumuzdan gurur duyuyoruz
Afrikalı olmaktan gurur duyuyorum, Afrikalıyım, bu yüzden Afrikalıyım
Bu yüzden zorlukların üstesinden gelebilir benim Atalarım bu şehit
Meşaleyi taşımak bana kalmış. beni parçalayamazlar.
Beni nakavt etmek için en az yüz bin rambottan oluşan bir ordu gerekir
Tarih öğretmenine hikaye anlattığını söyle.
Medeniyetlerin en büyüğü siyah Afrika'da doğdu
Afrika, piramitleri, bilimi, matematiği ile dünyaya ilham verdi
Sembolleri ve işaretleri
Firavunların zamanının hiyeroglifleriyle Kutsal Yazılar yarattı
Bana inanmıyor musun?
Devam et, Akhenaten'e sor. (Dakar'dan Marsilya'ya)
Ana soutoura bifi GNOME mame bayiwoon
Jikko sen rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
GNOME wakh at ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
GNOME wakh için ki nga doon oh ! Ooh !
Afrikalılar ve kim olduğumuzdan gurur duyuyoruz
Dafa melni gnou ngi daw jeum fenen ni WACC wacc nagnou ande yi xeeb sougnou
ngande yi fekki borom jikko sen dande yi
Fo daw fo daw di nga wirri ndaari fa nga jouge fi nga Doore fila woore doufou
gülümseme
Afro Sama Dole na nga mako xole geum Sama demb doon nittou tey njaxass ni
xeetou parfüm'k'gowe
Afrika koula Xass Foy gnawe
Afrika xola gneup nignouy ngaange
Afrikalılar soya baştankara doufi gawe
Koula Xol Dina seet fan la lay ngagne
Geum sa Bopp xam fi nga bokk melni garab Reen banxass ak xob
Dougnou fatte fignou joge ndakh panafricanistes delo sougnou Xel Demb kanamou
anne Antilop giss
Dimbali reçel yi biss-gnoul metisses dekkil osiris-carbone14 souliwaat gnou
giss-histoire bindaat grand pere ba petit fils
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jikko sen rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon oh ! Ooh !
Africains et fiers de ce que nous sommes
Bamako ! Singapour ! Anghata !
Sama gaa gna ngi
Doomu Afrika mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Doomu Afrika mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala Sama gaa gna ngi
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Sama gaa gna ngi
Doomu Afrika mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala Sama gaa gna ngi
Doomu Afrika mbeur la kaamil
Nenaala Sama gaa gna ngi
Ci geew ken douko jamnaani
Nenaala sama gaa gna ngi !