Max Richter — I am writing this letter şarkısının şarkı sözleri ve çevirisi
Sayfa, Max Richter adlı sanatçının "I am writing this letter" şarkısının sözlerini ve Türkçeye çevirisini içeriyor.
Şarkı sözleri
bakkan waruw dàll la fa muy degge dooko yëg
dem rekk delu si rekk
melni wèer wi delu si ci sèy jèego
fènèen wèer mouk ci fi,
bidèw bi danouna dèe ci souff
samay xarit, tèy ji ndadjè bi rafèt na,
djoko, seeddo,
ak rétane bi rafèt na,
xèw bou nèex
mais soubbe dagniouy dèm,
galankor bi moy dougnou
meuneu xamanté bou bax,
dou nouy am waxtou
bou doy ngir soppanté
goudi gi wèss, mangi won
fénène, bi ci toop dina fi sori
ak samay bok ci camion bi,
dinagnouy teugueu ngir
féccelo yénéni nit
ak samy bok ci camion bi,
ngir andi mbékté bignouy djeul
bakkan waruw dàll la ku dul toxu doo xam fu dèkk neexe
fa muy dagge dooko yëg
(Merci a El Cancre pour cettes paroles)
Şarkı sözü çevirisi
bakkan waruw dàll la Fa muy degge dooko yëg
dem rekk delu ve rekk
melni wèer ve delu si Cİ sièy jèego
fènèen wèer mouk ci fi,
bidèw bi danouna deèe ci suf
samay xarit, tèy Ji ndadjè bi rafèt na,
djoko, seeddo. ,
ak retane bi rafèt na,
xèw bou neex
ama dagniouy dèm biliyordu,
galankor bi Moy dougnou
meuneu xamanté bou bax,
dou nouy am waxtou
bou Doy ngir soppanté
goudi Gİ wèss, mangi kazandı
fénène, bi ci toop dina Fi sori
ak samay bok ci kamyon bi,
dinagnouy teugueu ngir
yeneni nit yap
ak samy bok ci kamyon bi,
ngir Andi mbékté bignouy djeul
bakkan waruw dàll La Ku Dul toxu Doo xam fu dèkk neexe
Fa muy dagge dooko yëg
(Bu kelimeler için El Cancre'ye teşekkürler)