Youssou N'Dour — Sama Gàmmu şarkısının şarkı sözleri ve çevirisi
Sayfa, Youssou N'Dour adlı sanatçının "Sama Gàmmu" şarkısının sözlerini ve Türkçeye çevirisini içeriyor.
Şarkı sözleri
Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Yor xaalis mënui tee me moom la
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko
Foog nan nita ko waddal nga for ko
Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko
Man daal maay sa buur nangu ko
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ah gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan nga
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal man suma xarit nga
E e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
Baal dooc moomu foo ko
Teeyai teey teey
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
E e e gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan
Şarkı sözü çevirisi
Nga yor xaalis yaw sama gàmmu dégg Nanga
Xam veya neil yaw moomu los ko
İnsanlar Ko àbb mbaa nga için ko
Baal dóózéé, y
Nanga, nga yor xaalis gàmmu dégg nga
Baz için eğer séén tàmbaleey wëlis
Xam veya neil yaw moomu los ko
İnsanlar Ko àbb mbaa nga için ko
Baal dóózéé, y
Yor xaalis mënui tee beni moom ile
Nanga, nga yor xaalis gàmmu dégg nga
Xam veya neil yaw moomu los ko
İnsanlar Ko àbb mbaa nga için ko
Baal dóózéé, y
Kaay gaaw Balmumu eğer nga d ba ko
Foog veya şimdi Ko için ko waddal nga planı
Balmumu eğer gaaw-aata tarafından doon eğer fay ko
Mann daal maay içinde buur nangu ko
Nanga, nga yor xaalis gàmmu dégg nga
Baz için eğer séén tàmbaleey wëlis
Xam veya neil yaw moomu los ko
İnsanlar Ko àbb mbaa nga için ko
Baal dóózéé, y
Ali suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ali suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ali suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ali gàmmu daal sama doomu nday nga
Ama gàmmu daal güneş xarit nga
Ama gàmmu daal güneş askan nga
Ali suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ama gàmmu daal güneş xarit nga
Ama gàmmu daal man sama doomu nday nga
Ama gàmmu daal adam güneş xarit nga
Ama gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
Ko altında Baal dooc moomu
Teeyai teey teey
Ali suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ali suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ali suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ama gàmmu daal sama doomu nday nga
Ama gàmmu daal güneş xarit nga
Ama gàmmu daal güneş askan